所属专辑:Rokku Mi Rokka (Give and Take)
歌手: Youssou N’Dour
时长: 04:40
Létt ma - Youssou N'Dour (尤索·恩多)[00:00:00]
Du nii du nii bëgg naa nga létt ma[00:00:00]
Walla book nga firi ma[00:00:08]
Xamal ma lu leer[00:00:11]
Danga maa woolu sa gàlle ma ñëw nga mel ni xale[00:00:16]
Yaw daal yaw tóppal fële[00:00:21]
Danga ba di tappale[00:00:23]
Su fekkeeni parewoo waru loo di yónéé[00:00:26]
Ngall yaw bul ma defloo lu ma nin ñi di xeebe[00:00:31]
Létt ma mbaa nga firi ma[00:00:36]
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma[00:00:50]
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma[00:01:00]
Lég lég sax nga yónni ma[00:01:10]
Ma dem bay dem nga teye ma[00:01:13]
Léégi sax dematuma[00:01:15]
Damay bañ nga dugël ma[00:01:18]
Bu fekkeeni parewoo waru loo di yónéé[00:01:21]
Ngall yaw bul ma def loo lu ma nin ñi di xeebe[00:01:26]
Létt ma mbaa nga firi ma[00:01:31]
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma[00:01:45]
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma[00:01:55]
Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom[00:02:06]
Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw[00:02:11]
Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom[00:02:16]
Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw[00:02:21]
Létt ma mbaa nga firi ma[00:02:26]
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma[00:02:40]
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma[00:02:50]
Boo ma waxee fi nga bëgg dem[00:03:00]
Ma wax la fi ngay jaar[00:03:03]
Demal bul dem waxal bul wax defal bul def[00:03:06]
Man daal sonn naa sonn naa sonn naa[00:03:10]
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma[00:03:16]
Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë[00:03:21]
Bëgg ak bañ la[00:03:29]
Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë[00:03:32]
Bëgg ak bañ la[00:03:40]
Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë[00:03:42]
Bëgg ak bañ la[00:03:50]
Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë[00:03:52]
Bëgg ak bañ la[00:04:00]
Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë[00:04:03]
Bëgg ak bañ la[00:04:11]
Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë[00:04:13]
Bëgg ak bañ la[00:04:21]
Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë[00:04:24]
Bëgg ak bañ la[00:04:32]