所属专辑:Rokku Mi Rokka (Give and Take)
歌手: Youssou N’Dour
时长: 04:00
Pullo Àrdo - Youssou N'Dour (尤索·恩多)[00:00:00]
Koufi gneuw mu diangal la[00:00:15]
Niax mi môko môm[00:00:17]
Ndokh mi môko môm[00:00:19]
Daf ko donn[00:00:20]
Lî khar yi la[00:00:21]
Lî beuy yi la[00:00:23]
Nagam yangui[00:00:24]
Àll bâ ngui[00:00:25]
Baxi mâmam poullo àrdo[00:00:27]
Koufi gneuw mu diangal la[00:00:36]
Niax mi môko môm[00:00:39]
Ndokh mi môko môm[00:00:40]
Lî khar yi la[00:00:42]
Lî beuy yi la[00:00:43]
Nagam yangui[00:00:44]
Àll bâ ngui[00:00:46]
Baxi mâmam poullo àrdo[00:00:47]
Pullo ardo pullo djèry pullo ardo[00:00:51]
Pullo djèry pullo ardo pullo djèry[00:00:57]
Dakhal yi mu jeum fé[00:01:02]
Nga dakh yé mou jeum fi[00:01:03]
Yâ xam yaw li khèw fé[00:01:05]
Dara diaxa loula fi ba fé[00:01:06]
Pullo ardo pullo djèry pullo ardo[00:01:09]
Pullo ardo pullo djèry pullo ardo[00:01:14]
Ardo sékhna guëneum[00:01:30]
Daldi gaddu yatam[00:01:33]
Ma nga anddak khadjam[00:01:36]
Daldi djitël guéteum[00:01:38]
Pullo djèry pullo ardo[00:01:41]
Mingui anddak khdjam[00:01:46]
Daldi djitël guéteum[00:01:49]
Dalal xélam[00:01:52]
Féxal xolam[00:01:53]
Bou nit gniy fo aka ré môm yëguko souy[00:01:55]
Pullo ardo pullo djèry[00:01:59]
Lépp am mingui fi[00:02:04]
Fî la yarô[00:02:07]
Fî la magué[00:02:08]
Téyit fî la[00:02:09]
Také soxna[00:02:11]
Lépp am fî la[00:02:12]
Pullo ardo pullo djèry[00:02:15]
Bu nit gniy teub aka dal môm yëguko[00:02:22]
Limu am fî doy nako té doylô nako[00:02:24]
Boudè or la[00:02:27]
Mba jamâ[00:02:28]
Wala étage la[00:02:30]
Mba avion la[00:02:31]
Mba lénène la[00:02:32]
Môm guissouko pullo ardo[00:02:34]
Ma nga gaddu tôkhôr om[00:02:48]
Di mbîb mbîb yu am khôrôm[00:02:51]
Waye waye yu amoul môrôm[00:02:54]
Mél ni kouy nèkhal gôrôm[00:02:57]
Bofa diarè sant sarr è dinala rè[00:02:59]
Bofa diarè dône sérère è dinala rè[00:03:05]
Bofa diarè sant sarr è dinala rè[00:03:10]
Bofa diarè dône sérère è dinala rè[00:03:15]
Ma nga gaddu tôkhôr om[00:03:21]
Di mbîb mbîb yu am khôrôm[00:03:24]
Waye waye yu amoul môrôm[00:03:26]
Mél ni kouy nèkhal gôrôm[00:03:29]
Bofa diarè sant sarr è dinala rè[00:03:32]
Bofa diarè dône sérère è dinala rè[00:03:37]
Bofa diarè sant sarr è dinala rè[00:03:42]
Bofa diarè dône sérère è dinala rè[00:03:48]