• 转发
  • 反馈

《Xel》歌词


歌曲: Xel

所属专辑:Rokku Mi Rokka (Give and Take)

歌手: Youssou N’Dour

时长: 04:50

播放 下载lrc歌词 下载纯文本歌词

Xel

Xel - Youssou N'Dour (尤索·恩多)[00:00:00]

Famarë reub kat lawone[00:00:19]

Da ama biss mou khall yône[00:00:24]

Mu taxaw di xalat bamu yàg[00:00:28]

Mu sène mbëtt miy daw[00:00:30]

Mu suxat fital ambadi dâgu[00:00:33]

Té nane kî douma raw[00:00:35]

Far mbëtt ma sène kokorong[00:00:37]

Dadi dieul bop ba[00:00:42]

Dal di koy rône[00:00:44]

Bopp ba neubouna litha des[00:00:47]

Yaramam béppa ngui fègn[00:00:48]

Deune bak ndigg lak tank yak yénène ya[00:00:51]

Lippe di fègne[00:00:54]

Lii takh mou déféni[00:00:56]

Mbeutteu daa amoul xel[00:01:01]

Kone gnoune gni yalla jox xel[00:01:05]

Nagnu santati[00:01:09]

Nagnu santati[00:01:12]

Li yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk[00:01:16]

Mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax déf[00:01:20]

Loy dougou jitalal sa xel[00:01:29]

Ba lo thièy wout[00:01:34]

Di nga guiss nguenél[00:01:36]

Nit gni yor xel boo sété gnoy dokhal aduna[00:01:38]

Kiy déf té dou xalat[00:01:43]

Thi missal day mél ni mbeut ma[00:01:44]

Nit môm khélako yor[00:01:48]

Nit môm khélako yor[00:01:52]

Nit môm khélako yor[00:01:57]

Khélako yor[00:02:01]

Li yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk[00:02:07]

Mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax gnuy déf[00:02:11]

Fi neubeu moy khax[00:02:21]

Boko amoul yangui mél ni bayima[00:02:25]

Sokou amoul doto nék nit[00:02:30]

Li yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk[00:02:34]

Mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax gnuy déf[00:02:39]

Motax gnuy déf[00:02:45]

Wawaw wawaw wawaw wawaw[00:02:49]

Famarë reub kat lawone[00:02:58]

Da ama biss mou khall yône[00:03:02]

Mu taxaw di xalat bamu yàg[00:03:06]

Mu sène mbëtt miy daw[00:03:08]

Mu suxat fital am ba di dâgu[00:03:11]

Té nane kî douma raw[00:03:13]

Far mbëtt ma sène kokorong[00:03:16]

Dadi dieul bop ba[00:03:20]

Dal di koy rône[00:03:23]

Bopp ba neubouna litha des[00:03:25]

Yaramam béppa ngui fègn[00:03:27]

Deune bak ndigg lak tank yak yénène ya[00:03:30]

Lippe di fègne[00:03:32]

Lii takh mou déféni[00:03:35]

Mbeutteu daa amoul xel[00:03:39]

Kone gnoune gni yalla jox xel[00:03:44]

Nagnu santati[00:03:48]

Nagnu santati[00:03:50]

Li yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk[00:03:54]

Mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax gnuy déf[00:03:59]

Motax gnuy déf[00:04:04]

Wawaw lolu moy xel[00:04:08]

Soko amoul[00:04:12]

Soko amoul[00:04:14]

Yangui mél bayima[00:04:17]

Yangui mél bayima[00:04:19]

Yangui mél bayima[00:04:21]

Loy dougou nang ko téké xel[00:04:29]

Famarë reub kat lawone[00:04:34]

Mbeutt[00:04:40]