所属专辑:7 Seconds: The Best Of Youssou N’Dour
歌手: Youssou N’Dour
时长: 03:48
Birima - Youssou N'Dour[00:00:00]
Written by:Ndeye Mbaye/Youssou N'D[00:00:08]
Maysa tende jodo[00:00:17]
Yaa moom liile[00:00:20]
Maysa tende jodo[00:00:22]
Yaa moom liile[00:00:24]
Maysa tende jodo[00:00:26]
Ya a moom liile[00:00:29]
Hi woy birima[00:00:33]
Fumu yendu ma yendu fa yendo naanee[00:00:36]
Woy birima[00:00:41]
Fumu yendu ma yendu fa yendo naanee[00:00:45]
Woy birima[00:00:50]
Fumu yendu ma yendu fa yendo naanee[00:00:54]
Woy birima[00:01:00]
Fumu yendu ma yendu fa yendo naanee[00:01:03]
Buri samba laobe[00:01:07]
Yaa moom liile[00:01:09]
Buri samba laobe[00:01:12]
Yaa moom liile[00:01:14]
Buri samba laobe[00:01:16]
Yaa moom liile[00:01:18]
Hi woy birima[00:01:23]
Fumu yendu ma yendu fa yendo naanee[00:01:26]
Woy birima[00:01:31]
Fumu yendu ma yendu fa yendo naanee[00:01:35]
Damel maisa penda joor[00:01:38]
Jooro jooro jooro jooro ho ho ho hoy[00:01:40]
Sama waaji ken dula jam naani[00:01:44]
Woy birima[00:01:49]
Fumu yendu ma yendu fa yendo naanee[00:01:53]
Mmmm mmm[00:02:07]
Wooy tedi ngoné maarne be sambaa[00:02:14]
Kuli baca senge ndat biran ngamoo[00:02:24]
Ngoné maca nas mbay maca jeeri[00:02:28]
Samba yaasimooooo dike mbay kuja dooooki[00:02:33]
Yay borom mbaboor mi[00:02:45]
Hi di woy birima[00:02:49]
Sama waaji ken dula jam naanee[00:02:52]
Woy birima[00:02:57]
Fumu yendu ma yendu fa yendo naanee[00:03:01]
Dogo fal ak mawa joor kumba samba yaay jaloor[00:03:05]
Dogo dogo[00:03:08]
Ho ho ho[00:03:09]
Aziz o mbay dogo xam nga yoon wee[00:03:10]
Woy birima[00:03:16]
Fumu yendu ma yendu fa yendo naanee[00:03:20]
Maisa tendo jooro jooro[00:03:22]
A mari ngone sobel kayor niila[00:03:28]
Woy birima[00:03:34]
Fumu yendu ma yendu fa yendo naanee[00:03:38]