所属专辑:Rokku Mi Rokka (Give and Take)
歌手: Youssou N’Dour
时长: 03:57
Sama Gàmmu - Youssou N'Dour (尤索·恩多)[00:00:00]
Nanga def yaw sama gàmmu dégg naa da nga yor xaalis[00:00:11]
Xam naa ne yaw moomu loo ko[00:00:17]
Dang ko àbb mbaa nga for ko[00:00:19]
Baal dóózéé eh[00:00:20]
Nanga def na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis[00:00:28]
Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis[00:00:34]
Xam naa ne yaw moomu loo ko[00:00:37]
Dang ko àbb mbaa nga for ko[00:00:39]
Baal dóózéé eh[00:00:40]
Yor khalis meunoul tè ma môm la[00:00:48]
Keur gou rich meunoul tè ma môm la[00:00:51]
Yaw na nga def yaw sama gàmmu[00:00:54]
Dég na danga yor khalis[00:00:57]
Khamna ni yaw momouloko dang ko abb mba nga forko bâl dôzé tèyal[00:01:00]
Kaay gaaw wax ma na nga def ba am ko[00:01:17]
Foog nan nita ko waddal nga for ko[00:01:20]
Wax ma gaaw ñaata la doon ma fay ko[00:01:22]
Man daal maay sa buur nangu ko[00:01:25]
Nanga def na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis[00:01:28]
Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis[00:01:33]
Xam naa ne yaw moomu loo ko[00:01:36]
Dang ko àbb mbaa nga for ko[00:01:38]
Baal dóózéé eh[00:01:40]
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee[00:01:52]
Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee[00:01:57]
Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee[00:02:03]
Ah gàmmu daal sama doomu nday nga[00:02:08]
E e e gàmmu daal suma xarit nga[00:02:14]
E e e gàmmu daal suma askan nga[00:02:19]
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee[00:02:25]
E e e gàmmu daal suma xarit nga[00:02:31]
E e e gàmmu daal man sama doomu nday nga[00:02:36]
E e e gàmmu daal man suma xarit nga[00:02:42]
E e e e gàmmu daal yaw sama doomu nday nga[00:02:47]
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee[00:03:16]
Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee[00:03:22]
Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee[00:03:27]
E e e gàmmu daal sama doomu nday nga[00:03:32]
E e e e gàmmu daal suma xarit nga[00:03:38]
E e e e e gàmmu daal suma askan[00:03:43]