所属专辑:The Guide (Wommat)
歌手: Youssou N’Dour
时长: 04:59
Leaving - Youssou N'Dour (尤索·恩多)[00:00:00]
Dem dem[00:00:20]
Dem fan[00:00:21]
Den ndax lan[00:00:23]
Baya ko mom[00:00:24]
Dem nguir xee bou barri bi[00:00:26]
Dem ndax teen boh neex bi[00:00:30]
Teh rapp rek noom noo siy naan[00:00:33]
Nach bi lakkatouma taw bi barrewoul[00:00:36]
Dem ngir bokk bone menou fee am[00:00:40]
Dem ngir daffa wara nekk gorr done[00:00:43]
Goorgoorlau[00:00:45]
Dem dem[00:00:53]
Dem fan[00:00:54]
Dem ndax lan[00:00:56]
Liberte bi[00:00:57]
Si espace bou lendeum bi[00:00:59]
Sama beut yi guissa tounou[00:01:02]
Garap yi nga xamenteni noo ma souxat[00:01:06]
Su beut setiee barap yi bow[00:01:09]
Dem ngir Keur gui daf may nirou lou lendeum[00:01:12]
Dem nguir daffa warranekk goor done[00:01:16]
Goorgoorlau[00:01:18]
Damay dem[00:01:25]
Chi alla bi[00:01:26]
Damay dem Chi dex goumak gui[00:01:28]
Ne damay dem waw seeti sama nawleyee[00:01:31]
Damay dem si ban bou ritax bi[00:01:35]
Damay dem ba reewu bitty[00:01:38]
Ne damay dem waw setti samambokkyee[00:01:41]
Go-go[00:01:43]
Won ma sa yarii ma wax la ki nga donoy[00:03:03]
Won ma sa mbokk ma wax ko fi ngay diaar[00:03:06]
Hey what do you need [00:03:09]
He he yaw lilaneex[00:03:13]
Won ma sa yarii ma wax la ki nga donoy[00:03:16]
Won ma sa mbokk ma wax ko fi ngay diaar[00:03:19]
He defa li la neexoy hey yaw lila soop[00:03:22]
Sammkatou mboott moo xam ba ciy[00:03:29]
Sooxaoy ni meneuh kott noom daal amounou[00:03:32]
Mbaam hey defal li la nexx oo[00:03:37]
Ho ho ho ho[00:04:33]