所属专辑:Rokku Mi Rokka (Give and Take)
歌手: Youssou N’Dour
时长: 04:09
Tukki - Youssou N'Dour (尤索·恩多)[00:00:00]
Yoon wi nga jël baaxul ku la koy digël da lay nax[00:00:06]
Yoon wii ci des moo gën loo taseel dàldi kuy mën[00:00:14]
Yoon wii nga jël[00:00:20]
Booy dox ba ca biir géstul xool fi nga weesu balaa ngay[00:00:26]
Booy tukki yaw[00:00:35]
Booy tukki yaw[00:00:38]
Booy tukki yaw[00:00:42]
Na nga bàyyl ba mën[00:00:43]
Ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen[00:00:45]
Dina tax nga mën xam nekkinu ñeneen[00:00:48]
Foofo mën nga fa gis lu yókk sa xameel[00:00:52]
Booy tukki yaw[00:00:56]
Nita ngi toog di janoog yaw[00:01:01]
Booba fekk na ma ngay xalaat ba tàbbi asamaan[00:01:05]
Àndag niir yiy naaw dem na fu sore lépp ciy xalaatam[00:01:08]
Yaw sama waay kaay ma xamal la[00:01:14]
Léég léég nga toog fi nga toog tukki[00:01:16]
Bu neex dem ba kaw asamaan[00:01:19]
Ànd ag weer wiy naaw[00:01:22]
Li ngay janeer mu lay neex boo janoo mu gën fee neex[00:01:25]
Booy tukki yaw[00:01:28]
Booy tukki yaw yeesal sa xameel[00:01:31]
Ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen[00:01:35]
Dina tax nga mën xam nekkinu ñeneen[00:01:38]
Foofa mën nga fa gis lu yókk sa xameel[00:01:42]
Deel tukki yaw[00:01:46]
Lëppa lëpp sàmba ma ngay naaw[00:01:51]
Te booy seet sax taxu koo gaaw[00:01:55]
Te léég léég mu dem ba kaaw[00:01:57]
Tukkee ka neex waaw[00:02:00]
Lucum cééli ma ngay naaw[00:02:03]
Te léég léég mu naaw ba kaw asamaan indi fiy xabaar[00:02:07]
Ku dul tukki doo xam fu dëkk neexe[00:02:11]
Booy tukki yaw[00:02:14]
Booy tukki yaw[00:02:18]
Na nga bàyyi[00:02:19]
Booy tukki yaw[00:02:21]
Na nga bàyyi ba mën[00:02:23]
Ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen[00:02:25]
Dina tax nga mën xam nekkinu ñeneen[00:02:28]
Foofa mën nga fa gis lu yókk sa xameel[00:02:31]
Booy tukki yaw[00:02:35]
Booy tukki yaw[00:02:39]
Booy tukki yaw[00:02:42]
Na nga bàyyi ba mën[00:02:44]
Ñaanu barke ah ñaanu barke[00:02:46]
Nita ngi toog di janoog yaw[00:02:57]
Booba fekk na ma ngay xalaat ba tàbbi asamaan[00:02:59]
Àndag niir yiy naaw dem na fu sore lépp ciy xalaatam[00:03:01]
Yaw sama waay kaay ma xamal la[00:03:08]
Léég léég nga toog fi nga toog tukki[00:03:09]
Tukki bu neex dem ba kaw asamaan[00:03:12]
Làng ag weer wiy naaw li ngay janool mu lay neex boo janoog moom[00:03:13]
Mu gën fee neex[00:03:19]
Booy tukki yaw[00:03:22]
Na nga bayyi ba mën[00:03:23]
Ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen[00:03:25]
Dina tax nga mën xam nekkinu ñeneen[00:03:28]
Foofa mën nga fa gis lu yókk sa xameel[00:03:32]
Deel tukki yaw[00:03:36]
Lëppa lëpp sàmba ma ngay naaw[00:03:39]
Te booy seet sax taxu koo gaaw[00:03:43]
Te léég léég mu dem ba kaaw[00:03:46]
Tukkee ka neex waaw[00:03:49]
Lucum cééli ma ngay naaw te booy seet sax taxu koo gaaw[00:03:53]
Ëndaaleel ñu xabaar[00:03:59]
Tukkee ka neex waaw[00:04:01]