所属专辑:Benn
时长: 03:50
Wiri Wiri - Henguilla/Youssou Ndour[00:00:00]
Written by:Henri Guillabert/Youssou Ndour[00:00:01]
Diem na diem[00:00:11]
Demoul féne lima begone[00:00:13]
Beu gnou né leer nga ngui[00:00:16]
Thi fénéne[00:00:18]
Mane magui si leundeum[00:00:19]
Dem na dem[00:00:28]
Mouy méti meu wouti liguey[00:00:29]
Lima beugone[00:00:33]
Moy mou dokh té douma dokh[00:00:35]
Si séne kaw[00:00:37]
Wiri wiri diari ndari[00:00:42]
Wiri wiri diari ndari ndari[00:00:47]
Dieul nafi[00:00:53]
Yeufou nitte togne nafi kouma meute kilifa[00:00:54]
Youkhou nafi[00:00:58]
Injustice dieuw nafi si nite bouné lou wa gnaw[00:00:59]
Khamnani may kiko def souma démé bey méré[00:01:09]
Douma méré[00:01:14]
Koudoul sama bopp[00:01:16]
Té mane ma[00:01:17]
Séti baye balou ko[00:01:19]
Wiri wiri diari ndari[00:01:23]
Wiri wiri diari ndari ndari[00:01:28]
Bilay bilay bilay bilay bilay bilay[00:01:40]
Ma ethiou[00:01:46]
Mani soy dem[00:01:51]
Beu khamato faga dieum[00:01:53]
Déloul faga dioudo[00:01:57]
Fagn leu guenté[00:01:59]
Fagn leu tété[00:02:02]
Figa magué[00:02:04]
Fagn la khamé[00:02:08]
Figa diangué lécole[00:02:10]
Bilay bilay bilay bilay bilay bilay[00:02:13]
Wiri wiri diari ndari[00:02:21]
Wiri wiri diari ndari ndari[00:02:26]
Wiri wiri diari ndari[00:03:08]
Fokk meu seti baay[00:03:11]
Balouko[00:03:14]
Fokk meu seti baay[00:03:17]
Lima beug moy[00:03:23]
Mou dokh[00:03:25]
Té douma dokh thi kaw[00:03:28]
Wiri wiri diari ndari[00:03:30]
Khamnani may kiko def[00:03:34]
Souma démé bey méré[00:03:36]
Sama bopp lay méré[00:03:40]