所属专辑:Li Ma Doon
歌手: Adiouza
时长: 04:11
Cey Love - Adiouza[00:00:00]
Mane la beugue[00:00:17]
Mane la guis[00:00:18]
Man rék dou kénéne[00:00:20]
Défale ma louné[00:00:22]
Wane ma louné[00:00:24]
Yobou ma founé[00:00:25]
Mossou ma sorri[00:00:27]
Souma amé naxar[00:00:29]
Mou dima yokou yakaar[00:00:31]
Daf maye diégué[00:00:33]
Souma tissé mou dima deufeul[00:00:34]
Té xamoul né sama xol[00:00:38]
Kénénne na fa fess[00:00:40]
Nane la kokoye waxé[00:00:42]
Défouma loutax[00:00:43]
Waxouma louko diar[00:00:45]
Tassoul tonioula[00:00:47]
Té xamoul né sama xol[00:00:49]
Kénénne na fa fess[00:00:51]
Nane la kokoye waxé[00:00:53]
Défouma loutax[00:00:54]
Waxouma louko diar[00:00:56]
Tassoul tonioula[00:00:57]
Oh oh nane la kokoye wahé[00:01:00]
Oh oh té doumako gagne[00:01:05]
Oh oh nane la kokoye wahé[00:01:10]
Oh oh té doumako gagne[00:01:15]
Xamna lovame ak yénéne[00:01:20]
Fimou tolou tchi mane[00:01:23]
Motah ma wara sincére[00:01:25]
Wah ko deugue[00:01:27]
Nit kou bah laa[00:01:28]
Souma sanione sama love dafaye law ba faw[00:01:31]
Tayoumako[00:01:36]
Souma nékék mome[00:01:38]
Kénéne laye halat[00:01:39]
Té xamoul né sama xol[00:01:41]
Kénénne na fa fess[00:01:43]
Nane la kokoye waxé[00:01:45]
Défouma loutax[00:01:46]
Waxouma louko diar[00:01:48]
Tassoul tonioula[00:01:49]
Té xamoul né sama xol[00:01:51]
Kénénne na fa fess[00:01:54]
Nane la kokoye waxé[00:01:55]
Défouma loutax[00:01:57]
Waxouma louko diar[00:01:58]
Tassoul tonioula[00:02:00]
Oh oh nane la kokoye wahé[00:02:02]
Oh oh té doumako gagne[00:02:07]
Oh oh nane la kokoye wahé[00:02:12]
Oh oh té doumako gagne[00:02:17]
Oh balma[00:02:22]
Nane lakokoye wahé[00:02:24]
Té douma ko gaagne[00:02:27]
Tissnama baby forgive me[00:02:29]
Mane tayouma lima dal[00:02:35]
Mbeuguel boula songué none la[00:02:40]
Yow balma[00:02:42]
Ni mbeuguel loye faléwoul sa héte[00:02:58]
Dou mbeur momou niouy dane[00:03:06]
Ni mbeuguel loye foume la fék meune laye[00:03:12]
Dalay yobou ardo[00:03:20]
Kass nane laye déf cey love[00:03:27]
Li kou ko xamoul dala daloul cey love[00:03:35]
Li kou ko xamoul dala daloul cey love[00:03:39]
Li kou ko xamoul dala daloul cey love[00:03:44]
Li kou ko xamoul dala daloul cey love[00:03:49]
Li kou ko xamoul dala daloul[00:03:54]