歌手: Youssou Ndour
时长: 02:21
Gorée - Youssou Ndour[00:00:00]
Written by:Youssou Ndour[00:00:01]
Ba ma démé gorée mane[00:00:05]
Andak samaye kharite[00:00:08]
Déme thia keur diame ga wone[00:00:10]
Dama daldi seugueume dioye[00:00:13]
Gore gnou make gni bi bore[00:00:16]
Djiguéne gnou make gni bi bore[00:00:18]
Gore gnou ndaw gni bi bore[00:00:20]
Djiguéne gnou ndaw gni thi bénéne bore[00:00:23]
Gnou daldi faye khali yone[00:00:26]
Yone wo khamni dangaye déme[00:00:29]
Yone wo khamni dangaye déme[00:00:31]
Sa khéle dou déme loudoul thi déloussé[00:00:34]
Loloye natou lawou bour bi[00:00:36]
Mi borome dogal yé[00:00:39]
Loloye natou lawou bour bi[00:00:42]
Borome koun faya koun[00:00:45]
Ba ma démé gorée mane[00:01:09]
Andak samaye kharite[00:01:11]
Déme thia keur diame ga wone[00:01:14]
Dama daldi seugueume dioye[00:01:17]
Gore gnou make gni bi bore[00:01:19]
Djiguéne gnou make gni bi bore[00:01:22]
Gore gnou ndaw gni bi bore[00:01:25]
Djiguéne gnou ndaw gni thi bénéne bore[00:01:27]
Gnou daldi faye khali yone[00:01:30]
Yone wo khamni dangaye déme[00:01:33]
Sa khéle dou déme thi loudoul[00:01:35]
Déloussé[00:01:37]
Aaan gorée[00:01:38]
Loloye natou lawou bour bi[00:01:41]
Mi borome dogal yé[00:01:43]
Loloye natou lawou bour bi[00:01:46]
Borome koun faya koun[00:01:49]
Loloye natou lawou bour bi[00:01:51]
Mi borome dogal yé[00:01:54]
Loloye natou lawou bour bi[00:01:56]
Borome koun faya koun[00:01:59]
Goréée[00:02:02]
Natou lawou bour bi[00:02:03]
Mi borome dogal yé[00:02:05]
Loloye natou lawou bour bi[00:02:07]
Borome koun faya koun[00:02:10]