所属专辑:Africa Rekk
歌手: Youssou Ndour
时长: 03:42
Exodus - Youssou Ndour[00:00:00]
Written by:Youssou Ndour[00:00:01]
Saï saï we want africa unite[00:00:11]
Without conflict exodus[00:00:13]
Saï saï we want africa unite[00:00:15]
Without conflict exodus[00:00:18]
Africa dama beugue ladjté[00:00:21]
Est-ce que amoul louniou fatté[00:00:24]
Wowowowowoy souniou rew yii dara doufi dess[00:00:26]
Wowowowowoy niakk and lolou laniou bakké[00:00:31]
Ana kouko def waay[00:00:36]
Nioune nioko def[00:00:38]
Ana kouko def kouko def[00:00:39]
Nioune leu[00:00:40]
Ana kouko def waay[00:00:41]
Nioune nioko def[00:00:43]
Ana kouko def kouko def[00:00:44]
Nioune leu[00:00:45]
Wowowowowoy eh pourtant fii leu nieupp di roté[00:00:46]
Wowowowowoy kou si féssal daal diniou fatté[00:00:52]
Wowowowowoy naniou andak fayda[00:00:56]
Saï saï we want africa unite[00:01:01]
Without conflict exodus[00:01:04]
Saï saï we want africa unite[00:01:06]
Without conflict exodus[00:01:09]
Saï saï we want africa unite[00:01:12]
Without conflict exodus[00:01:14]
Saï saï we want africa unite[00:01:17]
Without conflict exodus[00:01:19]
Bob marley yagg neu beu woté[00:01:22]
Diniou dioyal moussouniouko faalé[00:01:24]
Wowowowowoy geum naani dineu meusseu changé[00:01:27]
Wowowowowoy sounou rew yii bougou niou avancé[00:01:32]
Ana kouko def waay[00:01:37]
Nioune nioko def[00:01:39]
Ana kouko def kouko def[00:01:40]
Nioune leu[00:01:42]
C'est pourquoi gniniouy diakhassé[00:01:43]
Ba noppi diniou dioubolé[00:01:45]
C'est pourquoi gniniouy diakhassé[00:01:48]
Ba noppi diniou dioubolé[00:01:50]
Wowowowowoy let's keep our dignity[00:01:53]
Saï saï we want africa unite[00:02:03]
Without conflict exodus[00:02:05]
Saï saï we want africa unite[00:02:08]
Without conflict exodus[00:02:10]
Saï saï we want africa unite[00:02:13]
Without conflict exodus[00:02:15]
Saï saï we want africa unite[00:02:18]
Without conflict exodus[00:02:21]
Mbédiou kanam nimako guissé[00:02:23]
Boromako meuneu saafara[00:02:26]
Li eupp tchi souniou rew yi tu sais[00:02:28]
Bougoulou niou dara[00:02:31]
Bou dé ganaw laniou guissé[00:02:33]
Nonou rekk leuley teuweulé[00:02:36]
Nii wala wakhone naniou beugué[00:02:38]
Gnii wara dieuf tôk di khoulé[00:02:41]
Kagne leu africa di diok[00:02:43]
Andd té gueuneu bania saafikou[00:02:46]
Bokk liguey té wagni lolou[00:02:49]
Kone sounu diangoro fadiou[00:02:51]
Africa damala beugue ladjté[00:02:57]
Est-ce que amouniou louniou fatté[00:03:02]
Eh souniou beugué souniou diangoro fadiou[00:03:07]
Bokk liguey wagni lolou[00:03:14]
Bayyi seu kétou africa africa[00:03:17]
Africa damala beugue ladjté[00:03:28]
Est-ce que amouniou louniou fatté[00:03:32]