所属专辑:Best Of
歌手: Ismael Lo
时长: 05:01
Jammu Africa - Ismael Lo[00:00:01]
Written by:Ismaël Lo[00:00:02]
Afrika a a a[00:00:13]
Afrika mon afrique[00:00:19]
Sama gent gi maa ngi ñaan[00:00:37]
Yalla wonma ko bala may ñibbi barsaq[00:00:39]
Ma ne bes du ñakk ci bes yi[00:00:43]
Afrika don benn reew[00:00:44]
D'ici ou d'ailleurs[00:00:49]
Nous somm' des enfants d'afrique[00:00:52]
Mêm' si le ciel tombait[00:00:54]
Luttons pour la paix[00:00:57]
Kon jammu afrika[00:01:01]
Moom lay ñaan[00:01:04]
Mané jammu afrika mooy suñu natange[00:01:07]
Afrika a a a[00:01:25]
Afrika a a[00:01:31]
Afrika a a a[00:01:37]
Afrika mon afrique[00:01:43]
Yow mi nekka bittim reew man mi lô maa ngi lay ñaan[00:01:49]
Ak loo fa meun ta am ak noo fa meun ta mel[00:01:54]
Bul fatte Afrika[00:01:57]
Ici ou ailleurs[00:02:01]
La paix prix du bonheur[00:02:04]
Mêm' si le ciel pleurait[00:02:07]
Luttons pour nos frères[00:02:09]
Kon jammu Afrika[00:02:13]
Moom lay ñaan[00:02:16]
Mané jammu Afrika mooy suñu natange[00:02:19]
Afrika a a a[00:02:37]
Afrika a a[00:02:43]
Afrika a a a[00:02:49]
Afrika mon afrique[00:02:55]
Afrika a a a[00:03:01]
Afrika a a[00:03:07]
Afrika a a a[00:03:13]
Afrika mon afrique[00:03:19]
Onon bibbe Afrika ngimode[00:04:01]
Ngimode liggo den leydi men[00:04:05]
Afrika mon afrique[00:04:07]
Ngaccen hasi daagal[00:04:10]
Yoo Alla suren e musibaadi[00:04:13]
Yoo Alla addu jam to Ruanda[00:04:16]
Afrika mon Afrique[00:04:19]
Yoo Alla addu jam to Burundi[00:04:22]
Yoo Alla addu jam to Casamans[00:04:25]
Lawol Mbignona yee[00:04:28]
Afrika mon Afrique[00:04:31]
Africa a a a Africa[00:04:37]