所属专辑:Jammu Africa
歌手: Ismal L
时长: 05:00
Jammu Africa - Ismael Lo[00:00:00]
Written by:Ismaël Lo[00:00:01]
Afrika a a a[00:00:13]
Afrika mon Afrique[00:00:19]
Sama gent gi maa ngi ñaan[00:00:37]
Yalla wonma ko bala may ñibbi barsaq[00:00:38]
Ma ne bes du ñakk ci bes yi Afrika don benn reew[00:00:42]
D'ici ou d'ailleurs[00:00:49]
Nous somm' des enfants d'Afrique[00:00:51]
Mêm' si le ciel tombait[00:00:54]
Luttons pour la paix[00:00:57]
Kon jammu Afrika[00:01:01]
Moom lay ñaan[00:01:03]
Mané jammu Afrika mooy suñu natange[00:01:06]
Afrika a a a[00:01:25]
Afrika a a[00:01:30]
Afrika a a a[00:01:37]
Afrika mon Afrique[00:01:43]
Yow mi nekka bittim reew man mi[00:01:49]
Lô maa ngi lay ñaan[00:01:51]
Ak loo fa meun ta am ak noo fa meun[00:01:54]
Ta mel bul fatte Afrika[00:01:56]
Ici ou ailleurs[00:02:01]
La paix[00:02:03]
Prix du bonheur[00:02:04]
Mêm' si le ciel pleurait[00:02:07]
Luttons pour nos frères[00:02:09]
Kon jammu Afrika[00:02:13]
Moom lay ñaan[00:02:15]
Mané jammu Afrika mooy suñu natange[00:02:18]
Afrika a a a[00:02:37]
Afrika a a[00:02:42]
Afrika a a a[00:02:49]
Afrika mon Afrique[00:02:55]
Afrika a a a[00:03:01]
Afrika a a[00:03:06]
Afrika a a a[00:03:13]
Afrika mon Afrique[00:03:18]
Onon bibbe Afrika ngimode[00:04:01]
Ngimode liggo den leydi men[00:04:05]
Afrika mon Afrique[00:04:07]
Ngaccen hasi daagal[00:04:10]
Yoo Alla suren e musibaadi[00:04:13]
Yoo Alla addu jam to Ruanda[00:04:16]
Afrika mon Afrique[00:04:18]
Yoo Alla addu jam to Burundi[00:04:22]
Yoo Alla addu jam to Casamans[00:04:25]
Lawol Mbignona yee[00:04:28]
Afrika mon Afrique[00:04:31]
Afrika mon Afrique[00:04:37]
Afrika a a[00:04:42]
Afrika mon Afrique[00:04:49]